Está en la página 1de 2

infovihtal 01

Nit ki nga xam ni bi u gise jangoro


ji ci moom yggul Recin diagnosticado/a

Su fekke ni bi u gisee ci yow doomu jngoroy sida yggul


Dem di seeti ndax yore nga doomu jngoroy SIDA u gis ko ci yow nekk na lu diis lool. Waaye, lu mu diis diis, lu
mu metti metti ci jamono yi u la koy wax, xam g inga xam ni yore nga doomu jngoro ji dina mn guddal sa fan.
Ndaxte dinga mn a jariu bu baax ci doctor yiy topp
sa wer gu yaram, ak ci xam xam yu bees yi uy mujje
jfandikoo ci lu jm ci fajum SIDA. Su fekkee ni doomu
jngoro ji dafa nekk ci yow te gisuu ko, loolu mn na
gaa jumtukaay yi nekk ci sa yaram di la aar ci bepp
jngoro. Ba tax na, nit u bari u ame doomu jngoroy
SIDA te teelu u ko xam, u ngi yore yeneen jngoro yu
garaaw yoo xam ni mnoon nau ci mucc.
Bs bi njkk
Ci barab yu bari yi uy nemeekoo doomu jangoroy
SIDA am na oo xam ni dinau la taxawu, waxtaan ak
yow laata u lay seet ak boo noppee. Ginaaw loolu,
su fekkee ni danga soxla u gn la taxawu, defal la
taxawu bu gn a yaatu, bu gn a ygg, waxtaanal ak
waa barabu wer gu yaram bi ngay fajoo, dinau la
dimbali, xelal la bu baax. Su la neexee, mn nga woote
ci telefon yii ngir am taxawu ak ay leeral ci lpp loo
yittewoo: 934582641 (gTt), 934584960 (Red 2002) ak
902362825 (CEDISA). Am na itam ay barab yu bari yoo
xam ni dauy taxawu i yore doomu jngoroy SIDA di
leen jppale kenn ku nekk ci li mu yittewoo te duu
la fayeeku dara (Xoolal InfoVIHtal 27 Mbootaay yiy
dimbali imigere yi ame doomu jngoroy SIDA)
Jl ay matukaay
Jl ay matukaay yu am solo dina nekk lu jafe lool
ci jamono yi uy nemmeeku doomu jngoro ji ci yow.
Lu mel ni tambali faju giy xeex doomu jngoro bi (Mn
nga xool InfoVIHtal 3 Faju giy xeex doomu jngoroy
SIDA) wala wax say mbokk aki xarit ni danga feebar,
doon nau ay mbir yu am solo.
Ci jamono yooyu, u bari u feebar duu soxla
lool tambali faju, donte i nga xam ni diggante bi u
feebaree ak bi u koy gis ci oom nekk na diir bu gtt,
oonu mn nau leen beral taxawu ak faj yoo xam ni
ngir oom rekk lay doon. Waaye, li gn wor mooy ni
dinau la tambalil taxawu ak toppatoog wer gu yaram
gu sax, ndax u mn xam bu baax naka la sa yaram di
xeexe ak doomu jngoro ji.
grupo de trabajo sobre
tratamientos del vih
e-mail: contact@gtt-vih.org
website: www.gtt-vih.org
Barcelona (Espaa)

Faju gi
Am lopitaan boo xam ni dina la mn taxawu ak doktoor
boo dggol, nekk nau aari mbir yu mnul kk. Kenn
waxul ni danga war faju ci lopitaan bi u la gisale jngoro
ji, yow yaay tnn, ci biir lopitaani SIDA yi nekk ci rew
mi, lopitaan bi ngay fajoo. Su la neexee, mn nga tnn
lopitaan bu nekkul ci wetu co bi nga dkk.
Am na oo xam ni lopitaan yu mag yi oo leen gnal,
am eneen oo xam ni yi gn a ndax lau taamu. Lenn
rekk moo am solo, mooy am taxawug doktoor bu ygg
a ligeey ci fajum feebar yiy nd ak jngoroy SIDA.
Soo tnnee sa lopitaan ba noppi, dinau la wax ngay
w etti weer yu nekk ngir u nemmeeku sa yaram. Ci
w yooyu, dinga mn waxtaan ak sa doktoor, defaale
tamit ay nemmeeku ci sa wer gu yaram, nemmeeku yu
mel ni CD4 (Xoolal InfoVIHtal 2 Jumtukaay yiy aar ci
jngoro yi) ak dayob doomu jngoro ji ci sa yaram (Xoolal
InfoVIHtal 8 Dayob doomu jngoro ji). Ay nemmeeku
yoo xam ni lau dauy wone ndax ay jngoro dinau la
feeu ci kanam, di leeral itam ka nga war tambali jl
garab yiy xeex ak doomu doomu jngoroy SIDA.
Saa yoo tambalee faju, su fekkee ni feebar yiy nd
ak doomu jngoroy SIDA dau laa gn a feeu, wala
nga bokk ci ab gstub wer gu yaram, u ngi lay digal
ngay dem lu mu gn a bari di seeti sa doktoor.
Am xam xam bu jm ci doomu jngoroy sida
Ci njlben, baat yu bari yu jm ci doomu jngoroy
SIDA dinau la xaw a jaaxal. Waaye loolu bu mu tax
nga am benn jaaxle ndaxte am na ay xibaar yu bari yoo
xam ni bind nau leen ci anam yu gn a yomb ci yow.
Am xam xam bu jm ci doomu jngoroy SIDA dina
la dimbali lool ci nga mn a nemmeekul sa bopp sa wer
gu yaram, ak itam ngay mn di waxtaan ak sa doktoor
ci mbir yu gn a am solo. Dina baax lool ci yow ngay
dglu xibaar yi mujj a gnn, ak itam di waxtaan ak
u la mn di xelal, u mel ni ay doktoor, ay ligeeykati
lopitaan, farmasi aki serwiisi doomu jngoroy SIDA.
Lpp lu la leerul mn nga wax u bindal la ko.

Por favor, fotocpialo y Hazlo circular


Subvencionado por:

Secretara del Plan Nacional sobre el Sida

Pla Director dImmigraci

rea dAcci Social y Ciutadania

Colaboran:

infovihtal 01
#

Mn nga jle xibaar yu am njari ci Internet. Su


fekkee ni xamuloo fooy tambalee wala nga ame xel
aar ci xibaar yi nga mn a gis ci Internet, u ngi lay
xelal nga tambalee ci paasu Internetu gTt bii: www.gttvih.org, am na xibaar yu bari, ci xibaar yi gn a suufe
ba ci yi gn a kawe.
Xamale ko
Seetal ta xalaat bu baax sooga xamale ni danga yore
doomu jngoroy SIDA. Kan nga ko war a waxtaaneel?
Lu tax nga ko koy wax? Xalaatal ni nga koy waxe. Ban
ndimbal nga yaakaar ci i nga koy wax? Lan ngay sntu
ci oom? Ndax pare nga leen dglu su fekkee ni xibaar
boobu jppale nau la ci wala deet? Tambalil waxtaan
ak i nga xam ni yaakaar nga ni dinau la jppale, boo
noppee nga xalaat ndax bgg nga ko wax keneen, ku
mel ni kenn ci i ngay ligeeyandool, te nga xam ni mn
na am ni mu koy jle du la amal benn njari (Xoolal
InfoVIHtal 24 Xamale ni danga yore doomu jngoroy
SIDA).

grupo de trabajo sobre


tratamientos del vih
e-mail: contact@gtt-vih.org
website: www.gtt-vih.org
Barcelona (Espaa)

Nit ki nga xam ni bi u gise jangoro


ji ci moom yggul Recin diagnosticado/a

Xamante ak eneen
Xamante ak eneen, yeneen nit yu ame doomu
jngoroy SIDA, mn na nekk luy dalal sa xel bu baax. Su
fekkee ni fi nga dkk am na mbootaay guy yngtu ci lu
jm ci SIDA, mn na am mbootaay googu am mbooloo
mu u jagleel i feebar bu yggul. Su ko defee, dinga
xamante ak nit oo xam ni kenn ku ci nekk dund na
feebar bi, am na fu mu jaar bi mu feebaree, te mn na
am nga bokk ak oom yenn jaar jaar yi, yenn jafe jafe
yi. Loolu mn na la dimbali, dalal sa xel ci ni du yow
rekk yaay dund feebar boobu.

Por favor, fotocpialo y Hazlo circular


Subvencionado por:

Secretara del Plan Nacional sobre el Sida

Pla Director dImmigraci

rea dAcci Social y Ciutadania

Colaboran: